Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet Duplicate
filename
stringlengths
19
19
transcription
stringlengths
16
2.2k
duration
float64
2.27
119
speaker_id
stringclasses
15 values
language
stringclasses
1 value
audio
audioduration (s)
2.27
119
spk15_a030_s01.flac
bukki de ragal naa ko li tax ma ragal ko lan la yàpp. Jaan maa moom laa gën a ragalati nag, jaan ci boppam moom laa gën a ragal. Xam nga jaan rëyut waaye soo ko gisee danga daw moo tax ma ragal ko waa te ñi ma gën a ragal loolu ci la bokk waa <noise>. Fi mu ne nii jaan tam ragal naa ko trop, bukki ragal naa ko, gaynde ...
33.956
spk15
wof_Latn
spk05_h107_s01.flac
Saabu de xeme la, xam naa si xeme, dañ si dee dañ koo defer xeme ak dëwlin ak ndox. Boobu xam naa ko si saabu. Te saabu nag, pour fóot la, fóot pour setal la. Yooyu de xam naa ko si saabu waaw. Loolu yépp si la bokk. Mun na raxas, mun na sangu, mun na fomp waaw. Yii yépp xam naa ko si saabu. Daay jariñ loolu yépp, xam ...
35.524
spk05
wof_Latn
spk13_h026_s01.flac
Loolu mun naa nekka lu ñuy def mooy dangaa set-up sa toogu, toog mus jàkkaarloog télé bi soog a indi xale bi nga toog, soo ko deful nga toog si booram. So yaa ngi koy wan remote bi naka lañ koo taalee, lu <unintelligible> <noise> contact bi ta- taal taalee, nan la <unintelligible> bi taal télé bi, si nga téye remote bi...
66.808
spk13
wof_Latn
spk12_h063_s01.flac
<noise> bànk <hesitation> loolu de <noise> dencukaay la <noise> dencukaay de, dencukaay de moo nekka ñun fii sax dencut suñ suñ dena liñ si li ñu gën a xam si ndenc si si <noise> si askan bi ñuy dunda de  <noise> te ñu koy wax bànk, bànk boobu moom <hesitation> jamono jamono jamono yeewute moo ko indi rek si <hesitatio...
88.5
spk12
wof_Latn
spk12_a030_s01.flac
<noise> dafa am dafa am yenn rab yoo xam ne nii foog foog nga bàyyi leen xel ndax rab yooyu dañoo lore <noise> waaw  rab lépp rab boo xam ne nii óor na la ne bii mun na laa lor lu jar a bàyyi xel la <noise> ndax <hesitation> mbindéef la <noise> te mbindéef la boo xamante nii dafa am foo, foo moom, am fu mu moom, am lu ...
119.412
spk12
wof_Latn
spk14_h026_s01.flac
Mu xool <noise>, ma ne ko gis nga lii baaxut nit waru ko seetaan surtoutment xale, indil loo xam ne lu baax la dangay gis ne lii daf lay yee, wan la àdduna comme maanaam documentaire bi boo indil la rab yi yëpp ci àll bi. Mën nañ gis xoolal léegi gaynde bi mu ngi le ak doomam, bukki bi mu ngi fële ak doomam, tan yi ñu ...
69.168
spk14
wof_Latn
spk09_n071_s01.flac
Rakkaati gàmmu, maamu koor, ndayi koor, baraxlu, weeri koor, hori, diggi, tëbëski, tamxarit, diggi, gàmmu, rakki gàmmu, rakkaati gàmmu.
24.896
spk09
wof_Latn
spk08_f025_s02.flac
Xam ne soo ko lekkee daf dee yokku sa dëgëraay. Waaw am na si lekk yi kay. Muy yu deme ni comme ça yi ma la wax mbaxal yooyu noonu. Soo paree am sa bagaas yu sew ndax yooyu bokkul. Soo ci paree am sa diggante soraas ak sa banaana ak sa pom, cuuraay gerte yi tamit  day yokku sa dëgëraay. Boo bi tamit lekk bu bax la <uni...
49.792
spk08
wof_Latn
spk15_h063_s01.flac
Ma am suma xaalis du ma ko mën a denc si kër gi ma tëdd mu yàgg du guddi suma xel ne xam naa xaalis bi su ma ko tegee fii bu ëllëgee du am lu ma neex, ma jël paas ma dem paas ma yóbbu ko banque, bàyyi ko banque ñu jox ma këyit ma indi bu ëllegee su ma soxlaa banque bi ma dem tàllal këyit yi ñu jox ma suma xaalis <noise...
78.316
spk15
wof_Latn
spk13_a017_s01.flac
Mu ne ganaar pour nu moo xàmmee doomam yi, ganaar daf dee mun a <hesitation> xàmmee doomam yi si su dee nen, daf dee mun a def nen yi yëpp thirty days la dee nen, fanweeri fan <noise>. Su nenee mu toog si nen yi du génna, ga-  ganaar su dee nen si nen yi la dee toog. So su toogee si nen yi noonu xet bi mu ngee dugga si...
81.5
spk13
wof_Latn
spk05_p096_s01.flac
Liggéey <noise> <unintelligible> be tay liggéey la, liggéey moo waral yokkute lu nekk mu yàq : benna muy garden, benna muy project, benna <hesitation> waaw loolu rekk, defee ko nii nii nit ñi di si liggéey, di ko, bu dee jaay la ñu see jaay. Bu dee garden la ba tay. Xam nga garden soo koy liggéey soo amul foo koo jaay ...
63.42
spk05
wof_Latn
spk11_a034_s01.flac
Soo génnee jën rab yi dëkka si biir ndox bi dafa bëri trop kipo si biir ndox bi la dëkka jasit si biir ndox bi la dëkka karaab si biir ndox bi la dëkka <noise> comme gaa ñi am na yeneen am na yeneen jaan si biir ndox bi la dëkka gaa ñi lu nekk si biir ndox bi loolu xajul si kaw suuf bi comme lu bi nekk si biir ndox bi ...
28.288
spk11
wof_Latn
spk12_f004_s01.flac
<noise> waaw lekka, lekk de moom moo yor doomu adama <noise> waaw doomu adama moom lekk a ko ame. Lekk nekk na loo xam ne ni mooy dundal cër, mooy dundal xol, mooy dundal nit ki si boppam <hesitation> si si gàttal <noise>. Wér-gu-yaram munu loo koo am te doo te lekku loo, foog nga lekka doog a wér <noise>. Ba tax na mê...
88.25
spk12
wof_Latn
spk14_a017_s01.flac
Ni ngay xàmmee dàll yi boo demee si buntu jumaa bi dàll yi lu ñu bari bari kii summi dàll la walla nga génn nga xam ne kii sa rakk la walla nga génn nga xam ne kii sa doom la walla nga xam ne kii sa yaay la walla nga xam ne kii sa papa la xel boobu la la yàlla may, moom la yàlla may ganaar bi. Ganaar lu muy doxi si kër...
71.4
spk14
wof_Latn
spk11_p055_s01.flac
Pour dem university bi xale ak mag, dem university bi moo nekka pour nga dem nga jànga, nga xam nguur bi lan la war a waral, govern bi lan la war a def <noise> ak nga xam dëkk bi lan nga si war a def ak lan nga war a bàyyi. Pour jàng la daal, yokk si xam-xam loolu mooy pour xale ak mag yëpp njëriñu university bi, pour...
31.156
spk11
wof_Latn
spk08_m031_s02.flac
Ñaata? Ñaata kilimaa? Kilimaa bi de léegi mu ñów mu tàng, lee-lee mu ñów mu sedd, lee-lee mu ñów du sedd du tàng, ñett yooyu moom xam naa ko si kilimaa. Waaw lee-lee mu ñów mu sedd guyy, lee-lee sedd bi hem ; bii ñów tàng, bii ñów tàng bu yem, bii ñów du tàng du sedd waaw.
30.476
spk08
wof_Latn
spk15_f004_s01.flac
<unintelligible> tey nga def sa mbaxal, walla nga def sa maafe waa ñu wàññi diw bi daal diw bi daal damay yokk feebar kepp. Feebar yu bari daal li ko waral mooy diw ak jumbo yu bari, moo waral feebar yëpp. Lii de maafe yàpp moom su ma ko lekk xam nga boobu dafa andi dege bi, su ma ko lekkee ba suur balaa ngoon dinaa gi...
44.036
spk15
wof_Latn
spk11_a069_s01.flac
Mu ne naka la <noise> picc di defaree taggam, picc moom <noise> ni muy defaree taggam moom fasoŋ fasoom la ak façon picc yu nekk. Picca yu dee naaw nii picca yi comme time mi dugub ni <noise> walla time mi ñax ñoom dañuy def si dugub bi xëy xocc génnee seen xobi dugub bi, génne ko <noise> su ñëwee di ko defar taggam di...
63.94
spk11
wof_Latn
spk15_p116_s01.flac
ah ba tey man su ma gisee nit, mun naa koo óolu def comme suma bopp, ne ko sama soxla, ne ko soxla bii de nangam ak nangam, yow nag laa ci gannaaw yàlla yow laa ci xóolu, mu ne ma waa baax na, soxla boobu de bu ñu yàlla xotut mën naa la koo fajal nga dem ba heure boo amee jox ma loolu am na. Déedéet yombut tey nga wóol...
31.832
spk15
wof_Latn
spk08_p056_s01.flac
Jabar boo koy wut, wutal goro njëkk. Mag ñi balañ daan wuti jabar dañuy wut goro ba pare laaj sa nday ca nam mel. Su fekkee nday bi muñkat la, doylu na, boo wutee doomam diŋ diŋ diŋ ko fa fekk. Looloo tax ñuy wuti jabar jikko bu rafet di muñ.
27.536
spk08
wof_Latn
spk15_w081_s01.flac
Kooku daal <noise> a bañ a toog rek, jàppale sama waajur yi, jàppale waa dëkk bi looloo tax ma bugg ko. Rider mbaa oto bu ma ci am rek jël loolu tamit buggul, jàppal jàppale waa dëkk bi moo tax ma bugg ko waa. Léegi daal oto bi sax moo gën a moo gën a am sutura, tey léegi mën naa am sama soxla mbaa ku feebar, mbaa ku n...
33.012
spk15
wof_Latn
spk08_l055_s02.flac
Damay hut sama ndox bu set, ma def suma omo walla suma madaar. Su ma amee ordusawel, ma def suma ordusawel toqal ko si. Raxas sama loxo bam set. layandi, hut sama musuwaar ma fomp bam set. Bu kii yee, sama we yi buñ màggee dama ko dee dagg. Su fekkee wee yi am nan tiilim, damay génne sama tilim yi, dem sama beneen loxo...
36.952
spk08
wof_Latn
spk05_p072_s01.flac
Li la war rekk nga def ko danga, war ngaa liggéey war ngaa liggéey war nga sàkku liggéey. Soo waxtaaneek nit nga waxal ko dëgg, nga waxal ko li koy jëriñ. Yaa ngi gis, di jëriñoo nit ñi, nit ñi di la jeriñoo. Lool de wër na si àddina. Soo naree dundu si àddina, nit dañ la war di jëriñoo, nga jëriñoo nit ñi. Lool de xam...
33.096
spk05
wof_Latn
spk09_f024_s01.flac
Waaw lekk bi nga xam ni gëm naa ko ni day yokk leeraayu bët nawe si la bokk. Nawe <hesitation> lu baax la day yokk leeraayu bët <unintelligible>. Boobu moom bëgg naa ko lool. Batanta tamit lu baax la tamit dina yokk leeraayu bët. Waaw yooy daal laa gën a taamu man karoot ma ñëwaat. Waaw lekk yi nga xam ne <hesitation> ...
48.08
spk09
wof_Latn
spk11_h152_s01.flac
<noise> solar <noise> moom luy njëriñ moom <noise> njëriñu solar moom dafa bari. Solar nay yokk leeraay dëkk bi, solar na na tax nga mun a taal làmpa bi sa làmp kër yi soo amee solar si kër na danga dee mun a leeraayu kër bi, danga dee mun a charge charge sa mobile yi foofu, danga dee mun a xam dëkka bi lan moo fa lan ...
25.356
spk11
wof_Latn
spk08_n070_s02.flac
Samdi, dimaas, altine, talaata, àllarba, alxames, ajjuma.
9.464
spk08
wof_Latn
spk08_a027_s01.flac
Bann rab moo gënaa muus bëy moo gënaa muus.
5.7
spk08
wof_Latn
spk10_h107_s01.flac
Njëriñi saabu daal mooy dangay fóot, dinga sangu, diŋ ci raxas, diŋ ci fompu setal sa yaram, setal lépp, fépp daal. Foo war a kii rekk nga setal ko. Fu war a tilim rekk nga nga nga def kook saabu bam set <noise>. Xime lañ ko dee defare <noise>. Léegi dafaay am xeme, dafaay am dëwlin ak ndox. Moom nga faay def.
31.476
spk10
wof_Latn
spk13_h103_s01.flac
Waa passport lu moo sax moom njëriñam pour sooy tukki <noise>, ndax soo demee ba bugga tukki si beneen réew <noise> mun ngaa am passport pour nga dem, su nekkee yaa ngi gambie nga bugg a dem sénégal nga use passport nga dem si <unintelligible> nga wan nga bugga tukki dakar <unintelligible> walla fekk yaa ngi gambie nga...
61.348
spk13
wof_Latn
spk12_n041_s01.flac
<noise> afeeri <noise> dunda moom ñun liñ ko mën a àpp- àppal ne weer bu nekka nangami yoon laa dee dem jënda, dafa aju si yow <noise> li nga am, ak li nga am <noise> kañ lay jeexee <noise>. Léeg-léeg ñu jënd loo xam ne nii weer bi yëpp du jeex  <noise> waaye am loo xam ne nii bés bu ne nga koy def <noise>, te loolu do...
80
spk12
wof_Latn
spk13_a081_s01.flac
Bukki dafa intelligent <noise> dafa eewu, because moom guddi la moo génna uti lu mu lekk, dafa génn wër si àll bi, ñëw ba si boori kër yi waa dem ba si boori gétt nag yi di làqatu ut lu mu lekka. Su taasee yow nit ki sax yaa ngee dem sax daf laa xaar, beneen dëkk bi, mu dem si mu dem xaar la foofu noonu soo génnee mu d...
64.08
spk13
wof_Latn
spk14_a038_s01.flac
Boobu bu la rombee fii <noise> rek xet bi rek mun na fi am weer <noise> bu doxotee fii sa yére yi nga sol yow danga koy summi <noise> bu bàyyee bu doxotee rek yére yooyu waroon nga ko summi <noise> waxumalaa nag mu romb fii xetam bi rek déedéet <noise> danga sangu juróom-ñaari sangu <noise> du du doy <noise> wexeñ la m...
31.96
spk14
wof_Latn
spk15_n041_s01.flac
Jox ma suma xaalisu ndékki, su ma ko waxee jox ma suma xaalisu ndékki bi bët bu set twenty la, xam nga twenty fajul dara, te léegi bagaas bi dafa seer, dafay naajee ndékki ma ne ko dee may jox suma xaalis, mu tàngal kafe bi jox ma, waaye nag bët bu set twenty la, xam nga twenty lu mu mun, munul dara, waa bët bu set nag...
30.396
spk15
wof_Latn
spk14_h103_s01.flac
Boo amut paas dinga dem, kon <noise> boo amee passport am paas, xam fi nga jëm, kam ki fi nga jëm, am dalukaay <noise> loolu lu am sens la. Yaa xam amerique la, yaa kam suisse, yaa xam denemark <noise>, yaa kam france. Boo amut paas daal, passport daal, amuloo carte invitation doo dem. Kon bu fekkee am nga passport, am...
37.392
spk14
wof_Latn
spk14_a081_s01.flac
Boobu léer bu jotee leer, bu fekkee asamaan bi le- weer bi leer na dafa de sawar. Boo toppee bu toppee bukki sax daf ko dee yàqa bukki bi du ko mun a jàpp te bukki du am dara, boobu la ñuy wax till. Bukki tamit nag bu lëndamee dafay sawar parce que dana xam ne tey bésam la <noise> dana mun a dox si guddi gi, dana mën a...
101.552
spk14
wof_Latn
spk13_a028_s01.flac
Waa mun ngaa mun ngaa mun ngaa jël xar yar ko ba mu ba mu ba nga def li nga bëgg yëpp <noise> loolu daf di am <noise> dangaa gis ci tubaab yi dangaa gis ñu jël jën jën yu mag yii nii <noise> dañ ko dee  kii yar, def ko si géej soo demee <unintelligible> seetaan naa ko <noise> bu jën yi dafaa ñëw dafaa taxaw si kon jën ...
64.732
spk13
wof_Latn
spk13_a038_s01.flac
Waaw bu gën a am xet bu ñaaw <noise> wengec la tudd, waaw moom la wengec moom su rombee fii su su rombee ba bàyyi pëndal moom soo fi jaaree danga xam ne lii am na lu fi xeeñ, su nekke danga dem si àll bi di rubba soo jaaree, foo jaaree foo xam ne jaar na ba romb rek dinga xam ne fii wexeñ xeeñ na fi, jaar na fi because...
61.144
spk13
wof_Latn
spk10_h092_s01.flac
Caabi moo koy ubbi xombu bi. Caabi nga koy def mu ubbeeku. Mën ngaa jël marto nga dóor ko nii mu kéelu.
9.752
spk10
wof_Latn
spk14_n022_s01.flac
Olof, séeréer, joola, soose, bambara, saraxule, njaago, balanta <noise>. Am na <hesitation> ambience bi kooku ekool la mun naa la wax ne <hesitation> séeréer a ngi fi <noise>, pël a ngi fi, njaago a ngi fi, <hesitation> soose a ngi fi, <noise>, joola a ngi fi, bambara a ngi fi <hesitation>, ñag yaa ngi fi <noise>, tuku...
36.868
spk14
wof_Latn
spk14_n032_s01.flac
Pour ma xam seen at yi de du yomb, ku ñu wax el hadji demba <noise> <unintelligible> kooku suma <noise> xarit la daf ma dee yónnee sax xaalis. Alkaly <noise> dëkk <noise> bi boo ñëwee ba kounta am na dëkk bu nekkee nii, waa dem na sax <noise> ba galle bi foofu <noise> suma kër ñëw na tam, kooku war na am fifty years ju...
67.616
spk14
wof_Latn
spk08_a018_s02.flac
Moom itamit du nàmpal doom bum jurut <noise> du nàmpal doom bum jurut. Mun na nekk ñaar, beneen doom ñow, mu ñów nàmpal si, dem fori ñów nàmpal si.  Bu nàmpalsee doom ba njëkk a daw, fekkee jurut ko, bu ñówee du ko nàmpal. Lu weenam yi lakk lakk du ko nàmpal. Doomam lay dem seeti mu nàmpal ko. Nag itamit noonu, doomom ...
70.972
spk08
wof_Latn
spk12_h063_s02.flac
Waaw mu ne mboxoos lañu koo wax, waaw waaye bànk moom so su ma si buggee wax damay dem be damaa damaa génn si si si <hesitation> domaine bi ñu nekka dugga si lo xam ne nii nekkatul la-làkkam wolof. Waaw  yoo bank moom boobu moom li ma mun a wax rek mooy ñun suñ suñ bànk daal mooy suñ dencukaay mooy mboxoos yooyu noonu ...
86.5
spk12
wof_Latn
spk08_p111_s02.flac
Bu la sa doom ñówee ne <hesitation> peresidaa laa gént, lool laa bëgg walla mekkanisee walla kii daŋ ko siy jàppale si lim buggu, di ko si ñaax, di ko si xamb ba yàlla jàppale ko. Bu boobaa waaye tay bu la nee lii laa buggu nga ne ko bugguma loolu leneen laa buggu, lam la nga buggu defusi xelam, du ko def. Lam buggu si...
82.832
spk08
wof_Latn
spk08_f025_s01.flac
Waaw lu deme ni mbaxal, cuuraay gerte, mbuumu nebedaay bii nga def si gerte. Boobi it boo ko lekkee sa yaram wi dina sawar.
10.96
spk08
wof_Latn
spk11_p134_s01.flac
Non man mun naa wax déedéet, munoo dund without technology. Technology mooy comme mun naa wax mobile, munoo dund te ñà- nga ñàkk mobile, nga ñàkk tele loolu moom mun naa wax déedéet, parce que soo ñàkkee loolu doo mun a xam lan moo xew si dëkk bi. Waa soo amee tele, lépp lu mun ti xew soo taalee tele bi, tele bi na la ...
30.18
spk11
wof_Latn
spk10_c086_s01.flac
Démb benn cin laa añee. Am na jën. Am na am na am na jën, am na diwlin, am na soble, am na poobar, am na kaani, am na oño, am na jumboo, am na batañsa, am na jaxatu, am na bisaab.
25.128
spk10
wof_Latn
spk12_m009_s01.flac
<noise> waa ma doo- ma ma doree ko si soraas, mango, limoŋ moom laa waroon a njëkkee sax ndax moo nekk garab bi nga xam ne ni moo moo jiitu si si garab yi limoŋ. Waaw  ma ñëw si <noise> soto <noise>, kaasiyaa, wén, dimba, lëng, kutubulu <noise>, kasu, xay, kurenteŋ, benténk <noise> lenge, <noise> tiir <noise>, wén <noi...
63.628
spk12
wof_Latn
spk09_f002_s01.flac
Yan lekk moo gën a yombu: salaat, kaani salaat, kàkkumba, yooyu, tamaate. Bokk na ci yi gëñ a yomb waaye su ma lekk man dama koy enjoy bu baax sax paska am na vitamine <unintelligible>.
16.5
spk09
wof_Latn
spk12_f004_s02.flac
waaw lekka am na ñeent fukki cër suma si wér-gu-yaramu doomu adama. Ndax lekka mooy li mooy doxa lekka mooy doxal lu bëri si doomu adama bi lu tax lekk su dut lekka  <unintelligible> lu bari si doomu adama du dox. Wér-gu-yaramu doomu adama daal si gàttal su paasee ndox, lekka moo ko ame, moo tax lekk dafa important, da...
68.25
spk12
wof_Latn
spk09_f012_s01.flac
Waaw ay legum yii <noise> niñ ko mën a dencee ba du yàqu. Su fekke fiŋ ko def tàngut mën na dem ba une semaine du yàqu. Bu tàngut. Su fekkee fiŋ ko def mu ngee am ngelaw mu ngi sedd, mun na dem ba une semaine te du yàqu <noise> <unintelligible>.
25.096
spk09
wof_Latn
spk08_n056_s02.flac
Ndaxte wolof muŋ fa, séeréer muŋ fa, naar muŋ fa. Naaray pëj muŋ fa ak famiyam. Naar la dee wax. Wolof bi ak famiyam wolof lañ dee wax. Séeréer bi tamit,ñoom it séeréer lañ dee wax. Noon la mel. Juróom-ñetti nit wolof bi mun na juróom-benn, naar bi mun na juróom. Ñoo nekk si benn kër.
32.392
spk08
wof_Latn
spk15_i043_s01.flac
Pour ganaar bi  su fekkee yow  jàpp nga ko, soo ko jàppee nga woo ku la ko rendil, bu ko rendee ba pare nga teg ndox bu tàng bi, soo tegee ndox mu tàng bi ba pare nga dugal ko si biir ba mu tooy, nga suqi ba mu set wicc, boo ko suqee ba mu set wicc nga jël tànk yi nga dugal ko ci safara bi nga dindi we yi ba ñu set, ng...
82.876
spk15
wof_Latn
spk15_m009_s01.flac
mango am na, kasiyaa am na, déem am na, xay am na, lenge am na, ndarkaso am na, nebedaay am na, goyaa goyaab am na, papakaaya am na, mandare am na, ak ban ak <hesitation> xay am na, dittax am na, soto am na, kaba am na.
30.356
spk15
wof_Latn
spk12_a081_s04.flac
Yooyu ñoo nekka <noise> rab yi xam ngeen <hesitation> rab yi nga xam ne nii dañ xarañ lool guddi, pare dañu saay-saay.
7.75
spk12
wof_Latn
spk08_m007_s02.flac
<unintelligible> nete miŋ fi, werta, bula, naka laa ti, ñuul, ros, sokola miŋ fi. Am na bu weex, am na bu werta, ñuul, xonqu, nete, bula, pëy, dóom-taal, nawet bu rasko, rasko waaw baxa <unintelligible>.
46.148
spk08
wof_Latn
spk14_a031_s01.flac
Parce que boo seetatee télé documentaire danga gis gaynde bi ak jabar bi ak doom yi nu ñuy def daf lay jox yow ak sa kër ak seen doom yi ni ngeen di def benn la <noise>. Parce que dangay toog sa doom yi dem si yaayam jóge si yaayam ñëw si baayam, gaynde bi dafay tëdd fii jabaram tëdd fii doom bi nàmpu pare tëb tëb si y...
32.512
spk14
wof_Latn
spk08_p056_s02.flac
Takk jabar dafa wóor ndaxte sëy dafa yàgg te lu ne xaj na ci moo tax bu njëkk gaa yi dañ daan wax ne balaa ngaa wuti jabar wutil goro ba pare ndax diw si fami bu baax la bokk yaayam sëykat la dina tax ñu, boo hutijee doomam ñu ne <unintelligible> ñu ne ham nañ ci moom yaakaar. Muñ ak doylu, boo ko defee, lu ñów fekk la...
61.832
spk08
wof_Latn
spk08_n070_s01.flac
<unintelligible> semaine bi nekk na juróom-ñaari fan, juróom-ñaari fan yi boo si dalee samdi, dimaas, altine, talaata, àllarba, alxames, ajjuma.
11.152
spk08
wof_Latn
spk08_l097_s02.flac
Amoo benn xalaat si guddi gi <hesitation> liggéey nga ba sa yaram sonnu <unintelligible>, boo sangoo il faut que dinga am nelaw bu doy. Waaye fu la waay fekk rekk, yaa ngi toog rekk, di lekk lu la neex, sa yaram amul benn coono, nelaw bu doy doo ko am.
20.944
spk08
wof_Latn
spk15_h027_s01.flac
Mu ne ko soo ko ubbee waxaat ko farata bi li nga xam du farata nga teg ko fële, mobile soo gisee loolu lay jëriñ, li am farata danga koo wax lu am nag sunna nga wax ko lu amut sunna nga bàyyi ko waa. Mobile lii de mooy njëriñam soo defee lii muy njëriñ si yow boo deful lii nga def ko te nag du nekkul si njëriñ toppal l...
21.752
spk15
wof_Latn
spk09_n035_s01.flac
Waaw man moom li may nelew ci guddi gi yépp six hours la. Waaw su bëree ba bëre six hours la. Léegoo-leeg nag du ko mat. Waaw léegoo-leeg du ko mat waaye six hours moom maximum moom lool la paska balaa ma dem ba julli julli ba pare ba def li may def ba pare rekk twen dafay jot walla nine, te fife fum jotee damay jóg. W...
69.844
spk09
wof_Latn
spk08_a037_s02.flac
Jaan yeexut dafa gaaw. Bukki yeexut dafa gaaw. Gaynde yeexut. Su nekkee yeex am na kàkkatar benn gënu ko see yeex. Kàkkatar, kàkkatar moom yeex na ; doxinam, bu seqee fii bala moo seqihaat dina yàgg. Man moom laa jàpp ne moo gën a yeex ci rab yi.
27.068
spk08
wof_Latn
spk12_n041_s02.flac
Mun naa xayma àppi li nga foog ne loolu laa dee spend si si loolu laa dee <hesitation> frais frais si weer bi <noise>, waaw dangaa xayma rek àppi li nga xam ne loolu nga dee frais si weer bi. Waaye ne loolu mooy li taxaw, loolu du yomb ndax soxla yi dañuy bette, dafa am loo xam ne dafay ñëw fooguloo ko woon, léeg-léeg ...
68.388
spk12
wof_Latn
spk08_f003_s02.flac
Moom seer na ndax fim nekk nii lu dem si ganaar, yàppu xar, yàppu béy yépp dafa seer. Waaye nag, baax na si yaram waaye jën bu baax moom moo ko gën a raw. Tay soo tegee sa jën bi, nga am sa jën bu ferees jën bu baax, kële teg yàppam, du la gën a sawar yaram. Te dinga lekk ba suur ba nga yëg ne lekk naa. Boobu moom norm...
41.948
spk08
wof_Latn
spk09_f084_s01.flac
Wa <hesitation> boo seetloo lii di karoot, suppome,  ñàmbi, yooy yépp amut diw. Waaye boo seetloo yi nga xam ni moo am diw <hesitation> lu ci mel ne bene, ay gerte, yooyu nag ñu ngi génne diw. Yépp nag baax na, bu ci nekk rekk am na liggéey bu muy liggéey ci doomu aadama paska nit ñaar yépp ñoo ñoo ko séq ; lu saf xoro...
58.888
spk09
wof_Latn
spk09_h091_s01.flac
Naka la martu di jubalee pontu naka la martu di jubalee pontu ci biit bant. Loolu ci yaw mi. koy daaj la. Yaw mi war a tiye pontu bi, yaa koy jubbanti bam jub, nga dóor mu tegu ci kawam pont bi duggu. Loolu moom amut beneen mbir boo xam ne nekk na ci. Waaw ci yaw, yaw mi nga xam ne <noise> yaa koy daaj ci yaw lay dunge...
42.428
spk09
wof_Latn
spk12_h063_s03.flac
Ma ekkati boobu ma teg fooffu, mu rocci ko foofu jox kooku noonu ku wax ma ma dellowaat affaire bi aw bi ni ni ma ko jëlee woon foofu. Ni nga ko koy dénkee kooku laa gisoon mu nekka banque internantionale <unintelligible> noo ko dénkee xaalis bi si boppam soo ñëwee noonu nga ko faa fekkee, benn du ci, amul sax jàllarbi...
48.4
spk12
wof_Latn
spk05_c086_s01.flac
Cere laa reere démb, te cere dugub lañ ko bo booleel ak mboq, waaw. Ñu mooñ ko ba pare ñu tay ko. Buñ ko tayee ba pare dañ ko defar ñeex  façon ñeex bu la neex ; yaa xam jën la daŋ koy baxal, yaa xam mbuum la daŋ koy witt, toggu ko def si gerte muy mbuum waaw. Yaa xam bànga la, benn façon ñeex boo xam ne yaw loolu nga ...
58.56
spk05
wof_Latn
spk08_n035_s02.flac
Nelaw ko barewut. Suma first nelaw su paasee jeex na. Lu si des yépp dama koy jàllarbi ko. Fajar bala ñuy ganaar gi di sab, fekk yewwu naa waaye duma génn. Lee-lee damay jóg ma jàppu, ma julli ñaari ràkka tëddaat bañ noddu fajar, salaatu ma door a jóg, jàppu julli, génn, kumaase bale hëtt di liggéey suma liggéey ba wax...
79.104
spk08
wof_Latn
spk11_h107_s01.flac
Saabu lu muy njëriñ bëri na si kaw suuf bi. Benn saabu dafay setal, saabu dafay setal general nii dafay setal, day setal yére, day setal bool, day fomp, day setal karo, day setal tamit lii nii, day setal yaram. Saabu luñ koy defaree, suñ maam yi comme ni ñu ñu ko waxee saabu dañu koy defaree xeme, xeme mooy benn dañ ko...
36.44
spk11
wof_Latn
spk09_a037_s01.flac
Rab bi gën a gaaw mooy segg segg. Bokk na ci rab bi gën gaaw. Rab bi gën a yeex mooy kàkkatar. Bokk na ci bi gën a yeex <unintelligible>
14.188
spk09
wof_Latn
spk09_a027_s01.flac
Gën  a muus ak lu tax mu gën a muus. Rab wi gën a muus moom, mën nañ ci taamu lii de lëg. Mën nañ ci taamu cokeer. Bokk nañ ci yi gën a muus. Li li tax ñu gën a muus nag, suñ boroom moo leen bindee noonu, te ñuy bàyyee xel lañu, te ñi nga xam ne fuñ tollu  seen xel bi miŋ len wër, te seen bët yi tam toogul benn palaas ...
61.072
spk09
wof_Latn
spk14_w081_s01.flac
Bu ma amee <noise> oto laa moo <noise> moo ma <noise> gënal rider, rider yëfu xale la <noise> te man mag laa man bu ma amee oto laay dawal <noise>. Rider <noise> loolu yëfu xale la <noise> du yëfu mag <noise>. Am na ñeenti tànk <noise> te seetu bi nekk si biir oto bi danga gis sa gannaaw <noise>, lu nekk si buntu bi da...
42.98
spk14
wof_Latn
spk09_l097_s01.flac
Nelaw bu doy moom ku ko bëgg, sa xel day dal, daŋay am xel mu dal <hesitation> sa biir fees, sa yaram set <hesitation>. Yooyu soo ko boolee, boo tëddee pour nelaw daŋa am nelaw bu doy bu féex. Waaye sa biir bu feesul, sa jëmm setut <unintelligible>, sa xel dalut, doo man a nelaw, te doo am sax nelaw bu doy <unintelligi...
29.256
spk09
wof_Latn
spk10_h152_s01.flac
Leer lool da bam leeral ko, te tay su ku la nekkee courant demi tam moom naaj bi moo ko dee amali fit courant.
10.12
spk10
wof_Latn
spk14_p116_s01.flac
<noise> pour ñëpp wóolu la <noise> loolu yomb na la yombut, nit nag mun na koo am, parce que boo yàggee si palaas nga jub <noise> doo jël alalu jàmbur, doo fen, doo sàcc, doo rambaaj, doo jaxase ay nit, man bu ma la xamee loolu kii xamee la ko, kii xamee la ba loolu bu yàggee dañ lay jiital <noise>. Nit lu mu am moo ko...
33.572
spk14
wof_Latn
spk10_a069_s01.flac
Ñax, nax la ko dee ràbbe. Su deme ba jël nax mi ràbb ko ak gémminam bi. Lii la pittax. Pittax moo de jël bant ak hëñ di ko ràbbe. Man su nekkee picc yi moom ñax lañ dee am, ñax kese lañ de am. Léegi su nekke ne dem naa si dun bi si lekka yi ngee indi fii, mu ngee focc nii, dangay dem konte ci lifin bi, xob bi ñu ràbb k...
40.2
spk10
wof_Latn
spk09_p056_s01.flac
Lan moo gën a baax ci balaa ngay takk nit ci noo koy jànge <hesitation> dafa am jikko yoo xam ne de su nekkee ci nit man na ñi jàppu walla ñu gëm ni nit kooku ku baax la. Bi ci njëkk  walla boog man bi ma bi ma ci gën a taamu man mooy jigéen boo xam ne ku man a joxe ñam la maanaam lekk, jigéen boo xam ne ku tabe la waa...
61.684
spk09
wof_Latn
spk09_m007_s01.flac
Koola yi nga xam ne ham na <hesitation> am nañ am na weex, am na verte, am na blue, am na green, am na black, am na red, am na gold koola, <hesitation>, am na brown koola. Koola yi daal barinañ <unintelligible>. Waaye bàyyil ñu <unintelligible> jël si yooyu rekk.
32.224
spk09
wof_Latn
spk08_h091_s02.flac
Liggéeykat yi di ko jël. Boo jëlee marto bi nga teg ko, nga jël sa loxo bii nga tëye, nga jël bële nga dóor, dina dem. Waaye soo jëlee pont bi rekk nga teg ko, nga jël marto bi nga dóor, nga bàyyi sa loxo pont bi day tëb walla mu dëng. Moo tax booy kii nga jël marto nga tëye sa loxoo balee nga dooree door.
23.348
spk08
wof_Latn
spk05_a034_s01.flac
Bari na de <unintelligible> rab rab wi nekk si biir ndox mi bari na di. Loolu yépp man mënuma leen a tuddu paska rab yi nekka si biir ndoh bari suma xam-xam bariwu si; jën di xam naa ko si. Waaye lu mooy loolu di xam wa ko de wax dëgg yàlla. Dama ko dee dégg de dama ko dee dégg de waaye dey xaw ma ko paska dama dee dég...
47.42
spk05
wof_Latn
spk15_h103_s01.flac
fekk yow soxla nga passport nga dem si ñi koy liggéey ñu utal la. Soo amee passport bu baax te yàlla jàppale la ah mun ngaa dem ci réew yi waa. Léegi yow boo amee passport jarul ngay am id card passport bi mën na laa yóbbu fiu nekk foo bëgg a dem mën na la faa yóbbiu waa. te passport mën na laa wane fu nekk, boo ko xas...
33.788
spk15
wof_Latn
spk14_n041_s01.flac
Yeewoo bu fekkee <noise> kafe lañu def ak mburu ak bëer ak meew, loolu dina dem two hundred <noise>. <unintelligible> weer wi daal two thousand la. Waa weer bi dangay lekk two thousand, kër gi kafeeg mburu lañuy ndékkee <noise>.
21.672
spk14
wof_Latn
spk15_a081_s01.flac
Xanaa bëtt bu fekkee gis na <Hesitation> médd bu dee si àll, ñaar boo tëddee dangaa dégg mu kontaan ndax sab ci suuf waa. Du nelaw guddi moo gën a sawar ci àdduna guddi parce que liy ñëw moom moo koy gis xaw ba bët set waa. Bët bu set danay dox ndox mi nii fu ganaar bu, fu ku am ganaar nekk dana ko jéem a jàpp. Am naa ...
63.292
spk15
wof_Latn
spk11_p096_s01.flac
Nguur bi <noise> dafa war a yokk liggéey si économie development si dëkka bi. Nguur bi dafa war a xool yenn liggéey yoo xam ne comme maa si béykat yi daf leen war a jox machine, comme su joxul gaa yi machine <noise> mu jox gaa yi liggéey yoo xam ne comme dafay yomb ci yomb béy bi. Béykat yaa ngi fii nii, jox gaa yi mac...
36.24
spk11
wof_Latn
spk08_f084_s02.flac
Gerte kemb mun na. Laxe mun na waaye gerte kemb moo gën a mun ndax gerte kemb bi. bu njëkka daŋ ko daan jël, soo ko xollee bam set, bees ko, tànn saabu bi yépp, nga yóbbu si masin bi, nga suusal. Soo ko suusalee yóbbu ci mësin bi, ñu nalal la ko. Diwu gerte booobu, moo gën diw bii sax léegi. Bene bene bene it mun na di...
43.18
spk08
wof_Latn
spk15_a038_s01.flac
mbaam de am na, mbaam ak <hesitation> bë- bëy boobu moom bu la jegee danga xam ne xet bi boobu mooy xet <unintelligible> waaw dangaa rawale kenn du nokki wexeñ moom moo gën a bon xet waa ci rab yi yi ma xam. Boobu bu sànnee ngelaw rek kenn du nokki léegi wexeñ ki gën a kii la ki gën a xet bari xet la, mbaam mbaam kër ñ...
39.748
spk15
wof_Latn
spk05_p055_s01.flac
Mag boo xam ne am na jotam waaye loolu moo bariwul si mag yi. Fim ne nii mag buy jóg dem jàngi <hesitation> university  jàng te yaa ngay sëy xanaa su fekkee sëyoo waaye yaa ngee sëy bàyyi sa sëy, dem jàngi pour jàngi xam-xam pour nga xam loola yombut ; xale de man na ko, koo xam ne jotagul sëy, sëyagut, mu ngi tolloo s...
66.66
spk05
wof_Latn
spk12_a081_s01.flac
Lu <hesitation> benn dinaa njëkkee si benn <noise> bukki nekk na rab boo xam ne nii <noise> rab bu xarañ guddi la te guddi rek lay dox. Bukki bëccëg su tëddee sax lu mu war a am guddi daf koy am, ba tax na su jógee guddi fi mu war a amee foofu rek lay dem. <noise> bukki nekk na rab boo xam ne nii bëccëg amut <hesitatio...
86.5
spk12
wof_Latn
spk14_a089_s01.flac
Ndee moom mu ngi koo <noise> utiliser noonu la ko mun a def <noise> waaw, comme ni ngay def sa loxo yi nga bugg a def def <noise> moom tamit day bugg a def def. Nga bugg a yëkkati sa loxo nga yëkkati ko moom tamit day bugg a yëkkati laafam yëkkati laafam, bugg koo wàcce mu wàcce, boo yéegee buggoo ko mooy ñëw ci moom <...
23.796
spk14
wof_Latn
spk08_n071_s01.flac
<unintelligible> rakki gàmm, rakkaati gàmmu, maamo koor, ndeyu koor, baraxlu, weeru koor, digg, hori, diggi, tëbëski, tamxareet, diggi, gàmmu.
23.876
spk08
wof_Latn
spk14_h063_s01.flac
Banque fi ñuy dencee xaalis walla bànk <noise> ñàkk <noise>. Nga laaj ma tey <hesitation> xaalis mun la ne  tey damaa bànk, loolu bànk la <noise>. Banque dencee xaalis xaalis banque la <noise>, baŋ baŋ bu gàtt nii ci olof demal indil ma baŋ bale bànk <noise> bànk olof dana wax bànk, walla <hesitation> kaalis mooy bànk ...
67.036
spk14
wof_Latn
spk13_a030_s01.flac
<noise> rab yi ma gën a ragal mooy <hesitation> jaan, jaan ragal naa ko, because moom si biir ñax bi la dee nekka <noise> te daf dee dox guddi, bëccëg, <noise> lu si gën a bari sax guddi, <noise> dangaa toog rek <noise> gis mu ñë- mun naa ñëw ba egg si sa kaw <noise> doo ko yëg, te su la màttee mun naa laa rey instant,...
82.384
spk13
wof_Latn
spk05_a069_s01.flac
Ay ñax yi bant yu sew yi de dañ ko dee rocci, di naaw ak moom di ko dem defer tàggi. Lool de moom xam naa ko si, te gis naa ko tamit. Picc, waaw. ; ay ñax yu sew yi ak bant yu sew yi de ko damm de ko def ay tàggi.
21.324
spk05
wof_Latn
spk09_p111_s01.flac
Njëriñu waajur ci doom yaatu na lool sax lool lool lool. Li ci njëkk mooy nga tànnal leen yaay ju baax. su loolu amee aparee nga door a <noise> lijjanti education. Su ñu amee yar am respect <hesitation>. Lépp lu ñu bëgg dinañ ko mën a am paska baasu doomu aadama wallañ jël benn doomu aadama pour mu mel num war a mel ed...
56.488
spk09
wof_Latn
spk15_h026_s01.flac
Ma ko su taalee da ma ko bugg a taal ma ne ko bësal one bi mu ne un ma ne ko toxal ma ne ko toxalee ko ci bii boobu moom moo gën a yomb, su ko defee mu taal, toxal, ba fi mu ne nii xale bi sax léegi mun na ko, léegi kenn du ko digal loolu le mën na ko waa tele bi ah xanaay wéttaliku sant yàlla lu xale yi lu bari dañ si...
28.74
spk15
wof_Latn
spk05_h152_s01.flac
Dafay dafay <hesitation> use làmpu door ko <hesitation> am ñoo xam ne man nga koo user sa télé ay masin kii yu bare radio lu nekk man na koo use paska li mooy jël si kaw radio yeek télé yeek yépp a ko bokk. Lool de ham na ko si. Làmpu yi. Waaw lool de ham naa ko si solaire, te naaj lay jël, naaj wi moo koy sàrse, moo k...
27.924
spk05
wof_Latn
spk11_p072_s01.flac
Man ñett- lu majot a xam jëriñu nit yi si kaw suuf bi, si kaw àdduna bi si bi, benn def lu baax, ñaar  jaamu yàlla, ñett dimbale nit yi <noise> ak dimbale ñoo xam ne dañu sonn si kaw suuf bi, loolu laa xam jëriñu nit yi si àdduna si.
18.544
spk11
wof_Latn
spk13_h063_s01.flac
<hesitation> trouver benn place boo xam ne ni denceekaay la, denceekaayu xaalis moom lañuy wax banque <noise> xam nga ne si ngay liggéey ñu ngi lay fay weer walla nga yaa ngi business foofu le yaa ngi def àlla def guardian  nga jaay am sa xaalis, nga dem nga denc ko si banque. Ñëpp ñu si daanaka àdduna yi ñëpp loolu la...
88.75
spk13
wof_Latn
spk14_a030_s01.flac
Jaan de ñemewuma ko, gaynde ñemewuma ko, segg ñemewuma ko segg. Jaan mun nga dem ba dëgg ko doo ko yëg <noise> parce que moom si suuf lay dox <noise> te jaan bu ñuul bu mag bi moo gën a bon ak bu gàtt bu nga xam ne dafay naaw, ak boo jaan boo xam ne bu am ñeenti tànk mel ni kakataar mel ni <hesitation> ka-  waaw kakata...
69.92
spk14
wof_Latn
End of preview. Expand in Data Studio
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
9